
Audio is streamed directly from the publisher (goethe-institut.stationista.com) as published in their RSS feed. Play Podcasts does not host this file. Rights-holders can request removal through the copyright & takedown page.
Show Notes
Muhamad Ba ñu gën koo xamee ci Almami Maba Jaxu Ba mi ngi judoo Tawa ci RIP atum 1809. Jaakaarloo na ak Tubaab yi ay yoon i yoon ngir bañ ku noot der bu ñuul. Yaatal na yit Islaam ci Senegaal.
Topics
Fént ak YarSenegaalMboorJàmbaarNasaraanTubaabtaariqGoethe-Institut SénégalSenegaal. WolofFrenchFrançaisGoethe-InstitutGermanDeutsch